Submit Lyrics to wikilyrics

Elzo Jamdong – Coow Jibul Lyrics


Coow Jibul Lyrics by Elzo Jamdong (feat. Coco Cissoko)

 

Yone yi may dioggui di fakkhastalou

Thiow yi may deukkou yeup Jambar bawoul Yone bi may diogui di fakkhastilou

Thiow djiboul

Thiow djiboul

Yone bi may dioggui di fakkhastalou

Thiow yi may deukkou yeup Jambar bawoul Yone bi may diogui di fakkhastilou

Thiow djiboul

Thiow djiboul

Lalou hopital dinga deugg lou wer peng

(Lalou hopital dinga degg louy wer peng)

Yeufou marginal leniouy dounde ak sagn sagn (marginal marginal) Ne ten occupe pas when i step in the building

(Ne t’en occupes pas walla damalay kill )

Ils détruisent ta façon d’aborder le système

Eyy

Dieul ndaré comme temps school moussouma dal

Dor naa ay arrêt pour dokh, sama Yaye nang ma baal

Kane moye G ? Kane moy lokh ?

Kane moye snitch ? Kane moye thioy ?

Wakhabaane job seu town rek sinon

Wa town bi degn ley thiope


Yone yi may dioggui di fakkhastalou

Thiow yi may deukkou yeup Jambar bawoul Yone bi may diogui di fakkhastalou

Thiow djiboul, Thiow djiboul

Yone bi may dioggui di fakkhastalou

Thiow yi may deukkou yeup Jambar bawoul Yone bi may diogui di fakkhastilou

Thiow djiboul, Thiow djiboul

Thiow djiboul x8

Don’t nobody can stop this grind i do, Nobody got this thang like i-i-i-i do nobody can do this swag like me nobody can do it quite like me (like me) Im me, that’s just me baby (oh why) nobody got this juice like me

nobody can do it quite like me

(Noone can quite…)

Don’t noone can quite like me !

Yone yi may dioggui di fakkhastalou

Thiow yi may deukkou yeup Jambar bawoul Yone bi may diogui di fakkhastilou

Thiow djiboul

Thiow djiboul

Yone bi may dioggui di fakkhastalou

Thiow yi may deukkou yeup Jambar bawoul Yone bi may diogui di fakkhastilou

Thiow djiboul

Thiow djiboul

Thiow Djiboul x 8


Note: Please support wikilyrics by Sharing or dropping a comment here. Also, You can submit song lyrics, poem or anthem here and reach thousands of Audience!
VIEW:  Makhadzi – Moya Uri Yes Lyrics